Ablaye Wade wax na sa 2009 né mom day fedali yéném dess ci bop réwmi, ay nit rafetlu ko am nu co niawlu. Wax j bari lol
Ma japné, limco wax yoon la ngir mena samm karangué rewmi.
Su amul woon limuy juur moy féwalo bu réy ci biir PDS ba Nguur gi dotul tal liguey
lénéne moy "Opposition" bi dana guena yakamti jeul nguur gi ba def lu yeungel rewmi
Ablaye dina niak kiliftéf ba kén dotu ko dégal
Rewmi day sopaliku "Lamb golo"
Inscription à :
Publier les commentaires (Atom)

Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire