finalement tu vas au Sénégal = danga mujj dem Senegaal = dangay muj dem senegal (c le temps que tu as raté)
c'est la premiere fois que tu y vas = guléet nga ci dem = guléet nga fay dem
tu vois voir comment tu vas aimer vraiment ce pays = ?? réew mi neex na la dëgg-dëgg. = Njort nané rew momu dinala nééx lol
et puis tu auras l'occasion de te joindre avec ta belle-famille = te daldi am nga wërsëk daje ak sa goro. = dinga amalé yoonu giss say goro
décembre c une bonne époque pour y aller, le climat c super = ??? = wéru décembre, jawu-j day nééx,
tu vas t'amuser = ?=dinga mena fo
je sais pas comment les Sévillans peuvent le supporter = xamuma ni waa Sévillan deñu mëna ko dékku = xamuma naka lako wa séville di dekko
mercredi 7 juillet 2010
mardi 6 juillet 2010
Dém, délussé-co dakh
nit wala mala
dafa wara dém
dém ngir ut
ut lumu dundé
ut numu andal
ut méngnént
li dakh ci dém nak
moy délluci
déllu finga joggé
moy tekki ndam
dafa wara dém
dém ngir ut
ut lumu dundé
ut numu andal
ut méngnént
li dakh ci dém nak
moy délluci
déllu finga joggé
moy tekki ndam
Inscription à :
Articles (Atom)
