mardi 6 juillet 2010

Dém, délussé-co dakh

nit wala mala
dafa wara dém
dém ngir ut
ut lumu dundé
ut numu andal
ut méngnént
li dakh ci dém nak
moy délluci
déllu finga joggé
moy tekki ndam

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire