aduna, as deuk la su ndaw
nit ni danu wara di waxtaan sa su né
motax kalama di lu am solo
du rek gni gno wara jang lakku gnénén
wayé kuné war na mena deg li moromam di wax
sama mébeut moy gni taamu WOLOF am funu co waxé ngir yok sén deg deg
mangi ci xaar sén wall ci yar ak teggin
jarin moko taxa jog
ziar nalén
jeudi 3 juin 2010
Inscription à :
Articles (Atom)
